Dédicaces RSS

Radio Urum-Bi
il y a 1 mois
Assalamou Aleykoum, Soxna Fatima. Meun nga jokkook Radio bi ci 77 988 9670 / 76 350 9670 / 70 680 2864..
Fatima
il y a 1 mois
ziar naléne laye makhtar contane trop thi sougnou radio bi ma beuguone bokk thi bèneu dahira tè khawma nana lay def
MBOUR ahlou
il y a 2 mois
Bismillahi Rahmani Rahim Laye laye magui ziaar Di am contenté AK mbékté loool diléne nianal matériels yi yoku barké BAYE LAYE SAWS AMIIÎNE
Mame Baye Lahi ma raison de vivre
il y a 3 mois
Laye makhtar diadieuf si zikr Lahi Na leen Borom bi fay barke Baye Lahi
Fadel lahi
il y a 3 mois
machallah
talibe mame baye Lahi
il y a 4 mois
Laye makhtar diadieuf leen bègue neniou machaala
Aïda Laye
il y a 5 mois
Sene ligueye rafet na torop laye Makhtar limay niane rek moy mou ame bouton enregistrement nakh niouy meune di enregistrer sikar yii
Ndione Laye
il y a 6 mois
mash'Allah sen liggeey rafetna lenn rk lay sàkku ci yen moy amna sikar yo xamni sama giss giss mengowul ak diiné ji, c du un peu folklorique
laye
il y a 6 mois
Conference New York le 1 September inchalla
beugue Baye
il y a 7 mois
à tous les Laye Makhtar ziarra bou bax
771407469
il y a 7 mois
Machallah
aissatou lay
il y a 7 mois
MACHAHALAA bonne continuation
Gora Diop
il y a 8 mois
Manchala yalla nalén yalla fay
ndoyelaye6
il y a 8 mois
masallah laye mahtar contane naniou yénangi niouy hamal diniou wétali yalna yalla fayléne
lamine ndiay
il y a 8 mois
machalla machalla nékhna trooooooooooooooooope yalnelén yalla faye amiiiiiiiiiiiiiiiiine
abou poulo
il y a 9 mois
Laay maakhtaar. Diléne ziaar bou weurr. Di gnaane koorouk Diamm ak ay Kheweul. Si barké Sanga ba Maam Libass Xayru Nass
ben Mahdiste
il y a 9 mois
machallah laye mahtar sikkar si nehna trop yalna sunu borom xepp doli
siny laye
il y a 9 mois
machala laye makhtar
Libass Gueye
il y a 9 mois
laye makhtar animation bi nekhna ma gui niane Matar Laye Diop Zikroulahi 2
libass gueye
il y a 9 mois
laye makhtar ziar na wa radio urum bi sikar guilen di tek nekhna lol
lamine laye
il y a 10 mois
machaalah machaalah hol Sedna
Djibril laye
il y a 10 mois
laye Mahtar mangui naine Issa ndoye Karbala
Binta Lahi
il y a 11 mois
Ma sha Allah animation bi nekh na niou ngui fay diarei di ziar Khalifatoul muslimina Chérif Baye Abdoulahi yala na fi yagg lolou tei andakk werr eubalei Ahlou Beyti Rassoulilahi bi yeup mou wathie thi Ahlou layenn ak mbolem djioulitt Radio Urum Bi thi kaw thi kanam barké Mahdiyou ak Issa (pse)
Mame Mbaye Ndoye
il y a 11 mois
Mashallah dieureudieuf laye makhetar
seyni Laye
il y a 1 an
dieureudieuf wa radio urum bi niep contane
wa Diander
il y a 1 an
Doli di sannt rek
papisco Laye
il y a 1 an
machalla
Radio Urum-BI
il y a 1 an
Merci pour vos dédicaces. Expliquez à votre entourage comment écouter Radio Urum-Bi...
Am Laye
il y a 1 an
Dieureudieuf Laye makhtar Yal na yokk
Tina Laye
il y a 1 an
Dieureudieuf laye Makhtar